SÉNÉGAL : L’Assemblée nationale a adopté le projet de Loi de Finances Rectificative (LFR) pour l’année 2024.
Votre Pub ici !

Le Président de l’assemblée adresse ses chaleureuses félicitations au Ministre des Finances et du Budget ainsi qu’aux honorables députés pour la qualité des échanges lors des débats. Il salue particulièrement l’élégance, la courtoisie et le sens des responsabilités qui ont marqué ces discussions, témoignant de l’engagement de tous en faveur de l’intérêt national.———–« Assemblée nationale » nangu na sémbu Sàrtu Kopparal bi ñu soppi (LFR) ngir atum 2024.
Njiitu « Assemblée nationale » sant na jëwriñ ji yor Koppar ak Njël li ak mbooleem DIPITE yi ngir seen waxtaan wi ñu amal ci jamonoy DEBAA yi. Di rafetlu bu baax taar bi, ngor ak yëg-yëgu wareef gi màndargaal waxtaan yi, di seede aamug ñépp ci liggéey ngir njariñu Askan wi.
Source: DIAGNE Maana













